MBÉGTEEL BU NEEX:
Téere bi dinañu ko imprime ci Madina, te dinañu ko séddale ci lu dul fay, ngir sàkku xéewal ak kontaanu Yàlla. 🤲🏾📖
Yàlla na ko fayal ci liggéey bi, te barkeel Sheikh Ahmadou Bamba. 🤲🏾
Li dale ba Wave may nu ngir man a dindi transfert bi ci 60 minutes…
Bu ma la yónnee jeton bi, nga tàmbalee wax ma frais net, damay dindi sama transfert bi. Te itam, am nga rekk 10 minutes ngir wax ma “jërëjëf”, lu weesu loolu damay dindi lépp. 😒😒😒
Su fekkee dangay dem ci sa yoon ak muñ ak ngëm, Yàlla mën na soppi sa xaal ci lu gaaw nga xalaat.
“Ku liggéey te dénk sa mbir Yàlla, du réer. Khalil&إبراهيم
Yenn saa yi danga noppi rek di xalaat ne ndax sa présence amoon na solo wala déedéet… waaye dund dafa mel ni loolu, nit ñi dañuy fàtte lu noppi 🥲
Ibrahima Ibra Gueye 🙏✍️
li ma gëna bett ci mbirum ngòor-jigèen yi...
da ñuy jëf sèe. jëf yu bon yi noppi nag toog ci ékkraa telé yi ci kanam nit ñi ngir di jaŋgalé ay jikko yu baax,
ag sèen wowug bët ta doo gis toqu kersa ci sèen xar-kanam yi
Khalil&إبراهيم
مثل الذي تعلم حتى علم ولم يعمل علمه...
مثله كمثل الحمار يحمل أسفارا،
لا يعلم ماذا يحمل ولا اين يذهب😭
ki xamlu ba xam ta jëfè wul xam-xamam..
ag niròom da fsy niròo ag mbaam mu sëf ay tèerè,
du xam lum sëf ta du xam fum jëm😭
Khalil&إبراهيم