@yaxandiou@AlaadjiDitakh Budoon nitt ku weekh mbaa muy soll costume 😅sénégalais ag aduna bi yepp nangul ko xam xamam ,
Mais malheureusement danioo complexé
Moytu leen di denc naqar ci seen i xol.
Moytu leen di weet di xalaat naqar yu weesu.
Ku nekk war naa am ku ko doy ku muy diisool bu tollee fenn fi, lu bari ci naqar yi ci sa xol, boo ko waxee, mbaa nga bind ko mu féex.
Aka baaax !
Boudee ngëneel ci deret la Boroom Touba ag Sokhna Awa Bousso doyna ngënéel ,
BUDEE ngënéel amug Taalibei la , yaa jaay sa ñjureel jënde aG Taalibei
BUDEE ngënéel ci ci jikko la , koo bokkal jamono seeedei na sag tab ag sayy jikko yu rafett.
يؤتيه من يشاء