Ku nuy topp yaw yaa tax
Ku nuy wormaal yaw yaa tax
Ku nuy siyaare yaw yaa tax.
Ku la topp nu topp ko, ku wuute ak yaw nu bàyyi ko te topp la.
Sëriñ Muntaxaa yal na fi yàgg lool te wér.
Ousmane Sonko personne ne peut lui reprocher son manque de constance. Il oeut avoir des défauts mais c'est un homme véridique qui assume et prend ses responsabilités
Le président de la République, Bassirou Diomaye Faye, a mis fin aux fonctions du Premier ministre Ousmane Sonko ainsi qu’à celles de l’ensemble du gouvernement.
Peut-être que l’on rêve tous mais on ne sait pas? Des étudiants sont en train d’être « bombardés » sous nos yeux par un gouvernement qui luttait contre la répression policière il n’y a même pas trois ans…
Démb ba tay ngeen gis FDS yi di def lu ñaaw ci biir UCAD ngeen xam ne bakkan man na cee rot, ngeen toog di seetaan mel ni dénkuñu leen réew ba tay nit faatu ci.
Ana rupture ? Ana changement ? Ana ngor ? Ana li ngeen dige woon ?
« Xexouniou danio xiif, non à la violence »
« Amouniou louniou lek, ngen beug niou xex »
À 16h30 , ils tiendront un discours visant à discréditer les étudiants. Qu’il soit bien clair que nous ne laisserons passer aucune désinformation.
Je ne sais pas ce vous traversez, quelle bataille vous avez, mais Yallah nalene Yallah takhawou, fekhal sene khol, yok lene mbegtei❤️ Gnou beuri gnou ngi sourire tei lignouy dound metineu, ngor, soutoureu ak guem yallah motakh yanouwougnou sene dal. Yallah na yallah oyafal lep🙏🏾