Mooy Duruskat bu Mag bi. Xasida mooy ak dundëm. Mbacké amunu aajo ju weesu nga yagg lool te wer naal yëpp mat ak yeneen. Sunu xoll ak sunu lepp yalna sax fiyaw te duko moy benn yoon. Yaay dundël sunu xoll 💙 Mbacké yaa yilif jamono tiim ñëpp 💪 ñoo ngi fiyaw di safi liir 🙏